Aida Samb sunu sangue

Select language to translate this lyric

sunu sanguay borom goor mbacké balla naw
nala ki matt serigne bé nélene kamane laaa(2fois)
serigne saliou mii may way warr na takhkeep
koudiip djoulitt takhaw di sargar moy diambarii l 'Islam
Am ko mo di doylo kou ko amoul amo loula doy
meune gua kheuy di yalwani ki déy kamanlaa(2fois)
He would like to know what the whole family would be happy to receive backé
kene doula la def mass boroom ndioul borom diapandal borom
khelcom diaga borom dianatoo(2fois)
liy ngueneel thi mome tay tabil khelcom ak seuy
gnogne dieufeul ligueyal dieufeul mou feylaa(3fois)< br/>ilaa toubaaaaaaaa
ilaa toubaaa and ila toubaaa
ay makaa bougn sa diotiwoul
té legui touba ngi fi kaay soriwoul ziaréeé
mane kou bay ma bay kou bayoul what
thi tolou sang bé lahhilahahilah (2fois)
Ckeikh Abdou borom tawfekh kou bay ma bay kou
bay ma bay thi tolou sang bé lahhhlahaillalah
mane kou bay ma bay kou bayoul ma
bay thi tolou sang bé lahhhlahaillalah
Borom tawfekh kou bay ma bay kou bayoul
ma bay thi tolou sang bé lahhhlahaillalah
Serigne Modou habibay sa bay kou bay ma bay kou
bayoul ma bay thi tolou sang bé lahhhlahaillalah

SUBMIT CORRECTIONS